Disambar

Jóge Wikipedia.
Dem : Joowiin, Seet

Disambar mooy fukk ak ñaareelu weer ci arminaatu Gregori ak ci bu Suul.

Turam ma ngi jóge ci latin december, jóge ci decem (fukk), ndax moo nekkoon fukkeelu weer ci arminaatu waa-rom bu jamono ju yàgg ja.

Ci arminaatu weer bi, walla ci weeri wolof mooy yam ak Tabaski

Weer
Samwie | Fewirie | Maars | Awril | Mee | Suwe | Sulet | Ut | Sattumbar | Oktoobar | Nowembar | Disambar
Samay jumtukaay
Barabu tur
Wuute
Jëf
Joowiin
Boyotu jumtukaay yi
Yeneeni làkk