Sulet

Jóge Wikipedia.
Dem : Joowiin, Seet

Weeru sulet mooy juroom-ñaareelu weer ci arminaatu Gregori ak ci bu Suul.

Turam ma ngi jóge ci latin Julius, ngir màggale ko Suul Sesaar, buuru Rom ba woon, moom mi taxawaloon ci 46 nj. j. Isaa arminaatu Suul, tudde woon ko boppam, moo nekkoon juroomeelu weer ci arminaatu waa-rom bu jamono ju yàgg ja.

Ci arminaatu weer bi, walla ci weeri wolof mooy yam ak ndeyi-koor

Weer
Samwie | Fewirie | Maars | Awril | Mee | Suwe | Sulet | Ut | Sattumbar | Oktoobar | Nowembar | Disambar
Samay jumtukaay
Barabu tur

Wuute
Jëf
Joowiin
Boyotu jumtukaay yi
Yeneeni làkk